Mon profil Mes favoris Forum
En cours de mise en place ... Merci patienter.

Elzo Jamdong - Antidote

Posté par RAP OU CRĒVE
23 AVR 2020, 11:59
729

PAROLES

Intro 
Yeah eh, yeah eh eh 

 

Verse 
Nenegn ma africain khamoul louy job 
Africain dou degg loudoul ay dore 
Maam yi toubab yi done diapp niouy dow 
Mo dess souniou gene yi niouy dakhanté thioy yi 

Africain dioubeuleul mouné dey diadd 
Africain couvre feu sakh mounoul toke 
Africain lane mo ko téré mou takk 
Te africain beuri neu diamant ak or ? 

Africain diot neu niou gueum souniou bopp 
Gueum souniou bopp samm souniou bopp 
Africain diot neu niou arr souniou bopp 
Kou beugg deukk tchi ay boum niou topp 

Yeah 
Febar bi kass dou ko dog 
Hun 
Febar yagg neu lol 
Yeah 
Yagg negn bakhal ay khop 
Wayé khamagougn kagn leniouy guenneu tchi ndol 

Professeur diangal ma loutakh politiq bi tamm niou note 
Monsieur le geologue gaz bi ak petrole bi kane moko mom ? 
Jamono Scholcher beu legui niouy nakhanté ak Babylone 
Teranga amoul tchi jungle bi Gaindé dou baal Antilope 

Professeur diangal ma loutakh politiq bi tamm niou note 
Monsieur le geologue gaz bi ak petrole bi kane moko mom ? 
Tôt ou tard dinegn leu taggué ki leu takkal seu antimort 
Diogueundo liguey tchi fouleu kessé moye souniou antidote 

 

Hook x2 
Yagg neu thiole wayé beuss dineu chill 
Yagg neu pire wayè biss di neu mole 
Yagg neu thiole wayè gueum nani beuss dineu chill 
Yagg neu pire wayé gueum nani biss di neu mol 

Africain bala ngay teub di jubiler victoire bi neu worr 
Bo naré wolou kepp kou leu signe rek ngaaka ngay done 
Africain bala ngay tal fetch kholeul noy moyto seu none 
Africain bala ngay tal fetch kholeul noy moyto seu none 

 

Outro
Guelwaar speech


0 Comment

Aucun commentaire trouvé!

Ajouter un commentaire

Nouveau membre ?

Créer un compte